mané hé baykat bi khalam démonna bay nékh wayé boumgua dokna mome
mané hé baykat bi khalam démonna bay nékh wayé boumgua dokna mome
boula nékhé talalal say lokho yaye docteur biy fath khifou askane bi liko dalé si nditoum rew bassi miskine ya souméko di dane sa dolé andak nath bi di liguey sa gnakha di tourou ngay bay di doukat bilay ya am diome
kon diarama baykat koufi xiff yako doundal bamou sour waw koufi fébar yako nandal aki réén bamou féékh
kon diarama baykat koufi xiff yako doundal bamou sour waw koufi fébar yako nandal aki réén bamou féékh
ya momone sa mbay ya mome sa guanthiakh mome say ndiour ya mome sa alla di bay nguour gneuw dougalthia lokhome ak boor fékeleuthaa guanthiakh ba mégneu lole ndékétéyo
kon diarama baykat koufi xiff yako doundal bamou sour waw koufi fébar yako nandal aki réén bamou féékh
kon diarama baykat koufi xiff yako doundal bamou sour waw koufi fébar yako nandal aki réén
- Sugestão De Leitura... Andrew Winston.
"Se tornar verde não é um custo, é cortar custos." (Andrew Winston) Foto: Erica Sena O verde que vale ouro ( green to grow O verde que vale ouro Depois de analisar o caso...
- Bambu-la-lá / Muito Ouro!
***O bambu reciclado,que já deu forma a móveis e até bicicletas,agora virou matéria-prima de skate.Criado pela Addict em parceria com o designer de produto Bernardo Sodré,o SK8,como foi batizado,segue a cartilha do ecologicamente correto até na...
- Revista Rio Show
Exposição Metamorfose Ambulante .É a mostra de Vik Muniz , no MAM ,onde a inspiração mostra como a reciclagem está em alta.Na Exposição , que abre para o público hoje no Museu de Arte Moderna ,no RJ e depois , parte para São Paulo,já passou...
- A Song Of Oil In The Amazon
By Mitch Anderson, International Director Lago Agrio, Ecuador — The sprawl of scorched pavement and crumbling cement buildings in the heart of the Amazon rainforest. This city, once a small oil boom town founded by Texaco in the late 1960s (and...
- Los Pajaros Perdidos (canción)
'Los pájaros perdidos' (Canción)Amo a los pájaros perdidos que vuelan desde el más allá a confundirse con un cielo que nunca más podré recuperar.Vuelven de nuevo los recuerdos las horas jóvenes que di y desde el...